Culture
by Kalsoum
lyricscopy.com
Culture
Suma leeroon ne
Sangu na ba sett
Dina solu doon soldaru buur
Waaye samay laaf toy
Tawte waraluko
Ngelaw wawuluko
Kama djiito
Mooma walle jangaro
Solma toke
Ma lanke bañ taxalikok mom
Hey Tey dji toxu naa
Ba sama xel xely
Ma dieli lama jangul fenn
Oh - Ci la xamné niit
Amul ludul boppam
Aki mbokam
War na fonk boppam
Si lu genn
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Jamono dji leegi dafa changé
Alal tax na nu nekk ci danger
Roy moonu hypnotisé
Aada ak cossaan ñu banalisé
Culture bi naax saay
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Ni doomu adama yi doxe
Sax ci diko jeffee
Waye don na
Lu uteek liñu digg lee
May tambale ci yermande
Doomu aadama yi
ni ñu wara bëggante
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Waxleen!!
Suma leeroon ne
Sangu na ba sett
Dina solu doon soldaru buur
Waaye samay laaf toy
Tawte waraluko
Ngelaw wawuluko
Kama djiito
Mooma walle jangaro
Solma toke
Ma lanke bañ taxalikok mom
Hey Tey dji toxu naa
Ba sama xel xely
Ma dieli lama jangul fenn
Oh - Ci la xamné niit
Amul ludul boppam
Aki mbokam
War na fonk boppam
Si lu genn
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Jamono dji leegi dafa changé
Alal tax na nu nekk ci danger
Roy moonu hypnotisé
Aada ak cossaan ñu banalisé
Culture bi naax saay
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Ni doomu adama yi doxe
Sax ci diko jeffee
Waye don na
Lu uteek liñu digg lee
May tambale ci yermande
Doomu aadama yi
ni ñu wara bëggante
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Culture bi naax saay - hey
Dëgg bi xëy gaday - hey
Diublu ci yoonu say-say
Waxleen ci li waay
Waxleen!!