Jammu africa
par Kirikou Et Karaba
lyricscopy.com
ref: africa a a ah
africa mon afrique
&
sama gent bi manguiy nian yalla won mako bala may gnibi barsah
mané bes bu niak ci bes yi bé africa doon benn reew
d´ ici ou d´alleurs nous sommes des enfants d´afrique meme si le ciel tombait luttons pour la paix
kon Jammu Africa moom laay niaan, mané Jammu Africa mooy suniou natangéé
&
ref: africa...
yay mi nekk bitim rew may lo manglay niaan,
ak loo fa meunta am ak loofa meun ti mel bul faté africa
ici ou ailleurs la paix fruit du bonheur; meme si le ciel pleurait, luttons pour nos freres.
kon jaammu africa moom lay nian, manéé Jammu Africa mooy suniou natangué
&
ref x2: africa...
&&&&&